Waga di ndaga
73 pages
Wolof

Découvre YouScribe en t'inscrivant gratuitement

Je m'inscris

Découvre YouScribe en t'inscrivant gratuitement

Je m'inscris
Obtenez un accès à la bibliothèque pour le consulter en ligne
En savoir plus
73 pages
Wolof
Obtenez un accès à la bibliothèque pour le consulter en ligne
En savoir plus

Description

 L'auteur est un enseignant-poète panafricaniste. Pédagogue jusqu'au bout des ongles, dans ses écrits, il professe, guide et éduque. Le plus étonnant chez ce jeune seereer né à Daaru Seen à Mbuus Naax est qu'il manie la langue Wolof avec une compétence exceptionnelle. Ahmadu Lamin Samba CAW est un militant de la conservation et de la préservation des valeurs culturelles africaines. Pour lui, nos langues maternelles constituent un précieux patrimoine à protéger. Ce livre est sa deuxième publication. La première était intitulée : «Rootiaat » Une langue nait, grandit, et meurt. Si on ne s'en sert pas, elle tombe en désuétude. Si on la parle sans l'écrire, elle subit l'agression de l'expression de cultures dominantes ou hégémoniques. Cela, notre auteur en est conscient. C'est pourquoi, il tient à écrire en Wolof avec compétence et talent.

Informations

Publié par
Date de parution 01 janvier 2023
Nombre de lectures 7
Langue Wolof

Informations légales : prix de location à la page 0,0500€. Cette information est donnée uniquement à titre indicatif conformément à la législation en vigueur.

Extrait

1
2
Waga di ndaga
3
Tous droits réservés pour tous pays Copyright Les Editions Séguima E-mailseguimaeditions@gmail.comSite web :www.seguima-vision.com
4
 Ahmadu Lamin Sàmba Caw  Al-Amiin ci ñi ko miin Waga di ndaga LesEditions SEGUIMA
5
Ku taggatembe ci guuta Bëgg a am aafiya Gu muy sàmme aada Fàww nga Waga di ndaga. Al-Amiin ci ñi ko miin, "Le Samouraï" su jéggee raay, doomu Mbus-naax bii juddoo Daaro Seen jàngale ak taalif xàmmeetu ci xàjj ak seen.Te ni Seƾoor ak Seseer jomalee sëtti Moliyeer, Bàmba bindal ci Jolof lool giléem gu ko yanu loof, te terewul batay nuy puukarewoo tubaab walla di mbubboo araab te juddoo yaroo Jolof ci jël yeneeni kàllaama di sof ngir bañ a wax wolof, moo soof Séeréer bi mu mer, jël mbaal-njereer woddoo ko ni sér ndax "tarub wolof ak bu yaaram yépp a yam". Xam ne du mas a séen seen teen, moo tax a teeñoo téen ci xiyaas ngir réew mi jag ba jàmm sax fi dàkk.
6
Mu di ci taalif ci wolof ak nasaraan, am ci yéeney doon ab werekaan, taawloo ci Rootiwaat, di ko baaxantale Waga di ndaga. Nun la sëtti Sankara, Yi pànkaa ni Gewara, Yor laamisoog Mandela, Sunu mébét kawe gu Obama!
7
  • Univers Univers
  • Ebooks Ebooks
  • Livres audio Livres audio
  • Presse Presse
  • Podcasts Podcasts
  • BD BD
  • Documents Documents