//img.uscri.be/pth/6251226b16bfa293a2a2eee222be0453bb8fe785
Cette publication ne fait pas partie de la bibliothèque YouScribe
Elle est disponible uniquement à l'achat (la librairie de YouScribe)
Achetez pour : 6,99 € Lire un extrait

Lecture en ligne (cet ouvrage ne se télécharge pas)

Le bossu et le Ninki-Nanka

De
24 pages
Il était une fois un roi très riche. Mais il était toujours triste, car il n'avait pas d'enfant. Le roi passait des nuits blanches à se lamenter. La reine était malheureuse de voir son mari toujours triste.
Un soir de saison sèche, le ciel tonna. De grands éclairs traversèrent le ciel ; il se mit à pleuvoir. Les gouttes d'eau étaient aussi grosses que des oeufs d'autruche. La pluie dura sept jours et sept nuits. Elle avait tout englouti : maisons, greniers et champs. La reine aussi avait disparu !
Voir plus Voir moins

Le bossu et le Ninki-Nanka
Ma-Xuuge ak Ninki-Nanka ba

Bilingue

wolof:français

Texte de Mamadou Illustrations

Cissé

de Sophie Montdésir

L'Harmattan 5-7,rue de l'École Polytechnique 75005 Paris - FRANCE

L'Harmattan Inc. 55, rue Saint-Jacques Montréal (Qc) - CANADA H2Y IK9

Ma-Xuuge ak Ninki-Nanka ba

Amoon na fi benn buur bu oomle woon. Waaye ku amoon tiis ak naq ar la woon ndax amui woon doom. - Am naa alalu àdduna jépp waaye lenn Ii ma metti kay, moo di Ii ma amui doom.
Buur ba toog ay guddi du nelaw ; di jooytu, di jooytu rekk. Jabaram ja, lingeer, jàq 1001 ba mu gise jëkkëram ja ca tiisu kese.

Genn ngoonug noor, gu fiépp doon jàmbat tàngaayu mbooyo mu tar, la asamaan sa dënnu. Ay melax yu mag xotti jaww ja; taw ba soob. Mu tàmbaliy taw. Toqi ndox yaa nga réyoon ba toll ne ay neni bànjoolu.